Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 8

Ngën-gi-woy 8:6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Teg ma ci sa xol ni torlukaay, mbaa ci sa përëg ni lamu màndarga. Mbëggeel a bare doole ni ndee, fiiraange xér ni bàmmeel. Day jàpp jippét, di jum bu Aji Sax ji taal.

Read Ngën-gi-woy 8Ngën-gi-woy 8
Compare Ngën-gi-woy 8:6Ngën-gi-woy 8:6