Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 8

Ngën-gi-woy 8:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Sama càmmoñu waay, ma gegenoo, ndijooram, ma laxasoo.
4Yeen janqi Yerusalem, waatal-leen ma ne dungeen dakkal te dungeen sooke tëraayu mbëggeel te jotul.
5Ana ndaw suy jóge màndiŋ ma nii, wéeroo nijaayam? Ndaw si Ci ron pom gi laa la yee, fa la sa yaay jàppe ëmb, jur la fa.

Read Ngën-gi-woy 8Ngën-gi-woy 8
Compare Ngën-gi-woy 8:3-5Ngën-gi-woy 8:3-5