Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 6

Ngën-gi-woy 6:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Wuy, geesul fee! Soo ma nee jàkk, ma jànnaxe. Sa njañ liy loy-loyee ngi saf géttu bëy yu ñuul, yu bartaloo kaw tundu Galàdd.
6Sa gëñ yi ni mbote yu weex, yéege ca sangukaay ba, ku nekk ak seexam, kenn wéetu ca.

Read Ngën-gi-woy 6Ngën-gi-woy 6
Compare Ngën-gi-woy 6:5-6Ngën-gi-woy 6:5-6