Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 6:5-6 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 6:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Wuy, geesul fee! Soo ma nee jàkk, ma jànnaxe. Sa njañ liy loy-loyee ngi saf géttu bëy yu ñuul, yu bartaloo kaw tundu Galàdd.
6 Sa gëñ yi ni mbote yu weex, yéege ca sangukaay ba, ku nekk ak seexam, kenn wéetu ca.
Ngën-gi-woy 6 in Kàddug Yàlla gi