Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 1

Ngën-gi-woy 1:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Aa! Xamoo koo? Yaw mi dàq ci jigéen ñi! Génnal rekk, topp wewi jur gi, sàmmi say tef, fi dendeek mbaari sàmm si.
9Xarit, xam nga lu ma lay xoole? Yànjaayu wajan wu takk watiiru Firawna.

Read Ngën-gi-woy 1Ngën-gi-woy 1
Compare Ngën-gi-woy 1:8-9Ngën-gi-woy 1:8-9