Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:8-9 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Aa! Xamoo koo? Yaw mi dàq ci jigéen ñi! Génnal rekk, topp wewi jur gi, sàmmi say tef, fi dendeek mbaari sàmm si.
9 Xarit, xam nga lu ma lay xoole? Yànjaayu wajan wu takk watiiru Firawna.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi