Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 1

Ngën-gi-woy 1:4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Yóbbaale ma, nu daw, dem. Sama buur, yóbbu ma sa néeg, nu bokk mbég ak bànneex, di tàqamtikoo sa cofeel gi dàq biiñ. Ñoo yey nob la!

Read Ngën-gi-woy 1Ngën-gi-woy 1
Compare Ngën-gi-woy 1:4Ngën-gi-woy 1:4