Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:4 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:4 in Kàddug Yàlla gi

4 Yóbbaale ma, nu daw, dem. Sama buur, yóbbu ma sa néeg, nu bokk mbég ak bànneex, di tàqamtikoo sa cofeel gi dàq biiñ. Ñoo yey nob la!
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi