Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 1

Ngën-gi-woy 1:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Li sama buur tëdd, di xéewlu lépp, maa ngi gilli lu neex.
13Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.
14Saa nijaay, saa cabbu tóor-tóoru fuddën, fa digg tóokëri Engedi.

Read Ngën-gi-woy 1Ngën-gi-woy 1
Compare Ngën-gi-woy 1:12-14Ngën-gi-woy 1:12-14