Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:12-14 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Li sama buur tëdd, di xéewlu lépp, maa ngi gilli lu neex.
13 Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.
14 Saa nijaay, saa cabbu tóor-tóoru fuddën, fa digg tóokëri Engedi.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi