Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - MÀRK - MÀRK 9

MÀRK 9:28-30

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28Bi Yeesu duggee ci kër gi, taalibe yi laaj ko ci pegg: «Lu tax manunu ko woona dàq?»
29Yeesu ne leen: «Yu mel ni yii, ñaan ci Yàlla rekk a leen di dàq.»
30Bi loolu amee ñu jóge fa, jaar ci diiwaanu Galile, Yeesu bëggul kenn yég ko.

Read MÀRK 9MÀRK 9
Compare MÀRK 9:28-30MÀRK 9:28-30