Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Màndiŋ ma - Màndiŋ ma 22

Màndiŋ ma 22:40-41

Help us?
Click on verse(s) to share them!
40Balag daldi sarxe ay nag aki xar, sédd ca Balaam ak kàngam ya ko dar.
41Ca suba sa Balag ànd ak Balaam, yéege ko ba ca kaw jaamookaay ba ñu dippee Baal, tuur ma, mu tollu fa di séen lenni catu mbooloo ma.

Read Màndiŋ ma 22Màndiŋ ma 22
Compare Màndiŋ ma 22:40-41Màndiŋ ma 22:40-41