Text copied!
Bibles in Wolof

Màndiŋ ma 22:40-41 in Wolof

Help us?

Màndiŋ ma 22:40-41 in Kàddug Yàlla gi

40 Balag daldi sarxe ay nag aki xar, sédd ca Balaam ak kàngam ya ko dar.
41 Ca suba sa Balag ànd ak Balaam, yéege ko ba ca kaw jaamookaay ba ñu dippee Baal, tuur ma, mu tollu fa di séen lenni catu mbooloo ma.
Màndiŋ ma 22 in Kàddug Yàlla gi