Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 8

JËF YA 8:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Bi Simoŋ gisee nag ne Yàlla may na Xel mi jaarale ko ci loxoy ndaw ya, mu indil leen xaalis,
19ne leen: «Mayleen ma sañ-sañ boobu, ba ku ma teg samay loxo, nga jot Xel mu Sell mi.»
20Waaye Piyeer ne ko: «Asarul ak sa xaalis, yaw mi yaakaar ne man ngaa jënd mayu Yàlla ak xaalis.

Read JËF YA 8JËF YA 8
Compare JËF YA 8:18-20JËF YA 8:18-20