Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - 1.Buur ya - 1.Buur ya 4

1.Buur ya 4:16-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Baana doomu Usay boole diiwaanu Aser ak Beyalot.
17Yosafat doomu Paruwa sasoo diiwaanu Isaakar.
18Simey doomu Ela sasoo diiwaanu Beñamin.
19Geber doomu Uri sasoo diiwaanu Galàdd, di réewum Siwon buurub Amoreen ña ak réewum Og buuru Basan. Muy benn ndawal buur bu yilif réew mooma.
20Waa Yuda ak Israyil dañoo bare woon, ba mel ni feppi suufas géej, di lekk, di naan, nekke mbégte.

Read 1.Buur ya 41.Buur ya 4
Compare 1.Buur ya 4:16-201.Buur ya 4:16-20