Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 6

Sarxalkat yi 6:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Képp kuy góor ci askanu sarxalkat sañ na cee lekk. Lu sella sell la.
23Waaye juru saraxas póotum bàkkaar deesu ci lekk lenn te fekk deretam dugg ca biir xaymab ndaje ma, ñu di ca amal ag njotlaay ca biir bérab bu sell ba. Loolu du lu ñuy lekk. Dees koy lakk, ba mu dib dóom.

Read Sarxalkat yi 6Sarxalkat yi 6
Compare Sarxalkat yi 6:22-23Sarxalkat yi 6:22-23