Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 6:22-23 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 6:22-23 in Kàddug Yàlla gi

22 Képp kuy góor ci askanu sarxalkat sañ na cee lekk. Lu sella sell la.
23 Waaye juru saraxas póotum bàkkaar deesu ci lekk lenn te fekk deretam dugg ca biir xaymab ndaje ma, ñu di ca amal ag njotlaay ca biir bérab bu sell ba. Loolu du lu ñuy lekk. Dees koy lakk, ba mu dib dóom.
Sarxalkat yi 6 in Kàddug Yàlla gi