Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 2

Sarxalkat yi 2:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Bu saraxam dee lu ñu defare pepp, lakke ko ci saafukaayu weñ, na doon sunguf su mucc ayib su ñu xiiwaale diw te bumu am lawiir.
6Na ko dammat te sotti diw ca kaw dog ya. Saraxu pepp la.

Read Sarxalkat yi 2Sarxalkat yi 2
Compare Sarxalkat yi 2:5-6Sarxalkat yi 2:5-6