Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 2:5-6 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 2:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Bu saraxam dee lu ñu defare pepp, lakke ko ci saafukaayu weñ, na doon sunguf su mucc ayib su ñu xiiwaale diw te bumu am lawiir.
6 Na ko dammat te sotti diw ca kaw dog ya. Saraxu pepp la.
Sarxalkat yi 2 in Kàddug Yàlla gi