Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 24

Sarxalkat yi 24:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Bésub Noflaay bu nekk nañu saxoo taaj mburu yooyu fi kanam Aji Sax ji. Loolu sas la bu bànni Israyil di tegoo fàww.
9Mburu yooyu Aaróona aki doomam yu góor ñoo koy féetewoo, te nañu ko lekke fu sell, ndaxte lu sella sell la, di lu ñu séddoo fàww ci saraxi sawara yi ñeel Aji Sax ji.»

Read Sarxalkat yi 24Sarxalkat yi 24
Compare Sarxalkat yi 24:8-9Sarxalkat yi 24:8-9