Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 21

Sarxalkat yi 21:21-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Askanu Aaróona sarxalkat bi, du kenn ku ci am sikk kuy agsi ba fii, di joxe saraxi sawara yi ñeel Aji Sax ji. Sikk si ci moom a tax du mana agsi ba fii, di joxe ñamu Yàllaam.
22Du tere mu saña lekk ci ñamu Yàllaam, muy ñam wu sell ak wu sella sell.

Read Sarxalkat yi 21Sarxalkat yi 21
Compare Sarxalkat yi 21:21-22Sarxalkat yi 21:21-22