Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 7

Ngën-gi-woy 7:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Sa jumbux bi di kaas bu mërgalu, yàlla bumu ñàkk biiñu njafaan! Sa biir bi di jalu pepp mu ay tóor-tóor ñag.
4Sa ween yi ni ñaari tef, mbaa seexi kéwél.
5Sa loos wi, coleet, rattax, ni tatay bëñi ñay; say gët di lerxat ni déegi Esbon, ya feggook buntu Bat Rabim. Sa bakkan bi jub xocc ni tatay Libaŋ ja tiim Damaas.

Read Ngën-gi-woy 7Ngën-gi-woy 7
Compare Ngën-gi-woy 7:3-5Ngën-gi-woy 7:3-5