Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 7

Ngën-gi-woy 7:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Sa jumbux bi di kaas bu mërgalu, yàlla bumu ñàkk biiñu njafaan! Sa biir bi di jalu pepp mu ay tóor-tóor ñag.
4Sa ween yi ni ñaari tef, mbaa seexi kéwél.

Read Ngën-gi-woy 7Ngën-gi-woy 7
Compare Ngën-gi-woy 7:3-4Ngën-gi-woy 7:3-4