Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 7

Ngën-gi-woy 7:13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Nan teela xëyi ca tóokëri reseñ ya, bu reseñ ji jebbee, mbaa tóor-tóor yi focci, mbaa gërënaat ji tóor, nu gis. Fa laa lay jébbale mbëggeel.

Read Ngën-gi-woy 7Ngën-gi-woy 7
Compare Ngën-gi-woy 7:13Ngën-gi-woy 7:13