Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 5

Ngën-gi-woy 5:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ma ne ko: «Summiku naa de, xanaa duma soluwaat? Jàngu naa jeeg, xanaa duma taqati?»
4Sama nijaay yoor loxoom ci xarante bi, sama yaram ne sàyy.

Read Ngën-gi-woy 5Ngën-gi-woy 5
Compare Ngën-gi-woy 5:3-4Ngën-gi-woy 5:3-4