Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 4

Ngën-gi-woy 4:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Sa ween yi ni ñaari tef, mbaa seexi kéwél yuy fore digg tóor-tóor yi.
6Balaa jant a fenk, ker gàddaay, ma ne coww diggante tund wa ndàbb ne bann, ak tund wa xas ma neexe.
7Xarit, sa lépp a rafet, sikk nekkul ci yaw.

Read Ngën-gi-woy 4Ngën-gi-woy 4
Compare Ngën-gi-woy 4:5-7Ngën-gi-woy 4:5-7