Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 3

Ngën-gi-woy 3:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ngalla yeen, janqi Yerusalem, waatal-leen ma ci taaru kéwél ak koobay àll bi, ne dungeen dakkal te dungeen sooke tëraayu mbëggeel te jotul.
6Ana luy jóge màndiŋ ma nii, mel ni taxaaru saxar, suuroo ndàbb ak xas mu xeeñ ak mboolem cuuraayi jula?

Read Ngën-gi-woy 3Ngën-gi-woy 3
Compare Ngën-gi-woy 3:5-6Ngën-gi-woy 3:5-6