Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 3

Ngën-gi-woy 3:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Wattukat yee ma gis, ba ñuy wër dëkk bi. Ma ne leen: «Sama soppey xol, gisuleen ko?»
4Ma romb leen tuuti rekk, gis sama soppey xol. Ma ne ko taral, bàyyeetuma ko, ba yóbbu ko sama kër yaay, ba sama biir néegu ndey ji ma jur.

Read Ngën-gi-woy 3Ngën-gi-woy 3
Compare Ngën-gi-woy 3:3-4Ngën-gi-woy 3:3-4