Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 2

Ngën-gi-woy 2:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Dugal na ma néegub sago-jeex-na, yiire ma mbëggeel.
5Gaaweleen ma nàkki reseñ, ma dëgër, leel-leen may meññeef, leqlee ma. Wopp laa def ndax mbëggeel!

Read Ngën-gi-woy 2Ngën-gi-woy 2
Compare Ngën-gi-woy 2:4-5Ngën-gi-woy 2:4-5