Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 2

Ngën-gi-woy 2:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Mbete garab gu gëna neex ci gott bi, kookooy sama nijaay ci biir xale yu góor yi. May bége keppaaram, safoo doom ya.
4Dugal na ma néegub sago-jeex-na, yiire ma mbëggeel.
5Gaaweleen ma nàkki reseñ, ma dëgër, leel-leen may meññeef, leqlee ma. Wopp laa def ndax mbëggeel!

Read Ngën-gi-woy 2Ngën-gi-woy 2
Compare Ngën-gi-woy 2:3-5Ngën-gi-woy 2:3-5