Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 1

Ngën-gi-woy 1:14-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Saa nijaay, saa cabbu tóor-tóoru fuddën, fa digg tóokëri Engedi.
15Xarit, yaaka rafet, yaaka taaru! Say gët niy pitax.
16Nijaay, yaaka góorayiw, yaaka maa neex! Mbooy gu naat, nu laloo,
17garabi seedar di sunu xànqi néeg, garab gu dul ruus xadd ko.

Read Ngën-gi-woy 1Ngën-gi-woy 1
Compare Ngën-gi-woy 1:14-17Ngën-gi-woy 1:14-17