Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - MÀRK - MÀRK 5

MÀRK 5:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Ndaxte ay yoon yu bare jéngoon nañu ko te yeew ko ak ay càllala, waaye waa ji daldi dagg càllala yi te damm jéng yi, ba kenn amul woon kàttanu téye ko.
5Guddi ak bëccëg mu nga woon ca sëg ya ak ca tund ya, di yuuxu te jam yaramam ak ay xeer.

Read MÀRK 5MÀRK 5
Compare MÀRK 5:4-5MÀRK 5:4-5