Text copied!
Bibles in Wolof

MÀRK 5:4-5 in Wolof

Help us?

MÀRK 5:4-5 in Téereb Injiil

4 Ndaxte ay yoon yu bare jéngoon nañu ko te yeew ko ak ay càllala, waaye waa ji daldi dagg càllala yi te damm jéng yi, ba kenn amul woon kàttanu téye ko.
5 Guddi ak bëccëg mu nga woon ca sëg ya ak ca tund ya, di yuuxu te jam yaramam ak ay xeer.
MÀRK 5 in Téereb Injiil