Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 8

Jëf ya 8:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Gëmkat ña tasaaroo di xamle fépp fu ñu jaare, xibaaru jàmm bu kàddu gi.
5Noonu la Filib deme péeyub Samari, di siiwtaane Almasi.
6Ba waa dëkk ba déggee mbaa ñu gis kéemaan ya muy def, ñoo bokk teewlu ay waxam.

Read Jëf ya 8Jëf ya 8
Compare Jëf ya 8:4-6Jëf ya 8:4-6