Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 18

JËF YA 18:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Bi mu fa desee ay jamono, mu jóge fa, di jaar dëkkoo dëkk ci diiwaanu Galasi ak Firisi, di dooleel xoli taalibe yépp.
24Amoon na nag Yawut bu tudd Apolos te juddoo Alegsàndiri, mu dikk Efes. Nit ku yewwu la woon te am xam-xam bu yaatu ci Mbind mi.

Read JËF YA 18JËF YA 18
Compare JËF YA 18:23-24JËF YA 18:23-24