Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 18

Jëf ya 18:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Póol toog na Àncos ay fan, jóge fa wër diiwaanu Galasi, teg ca Firisi, di ñaax mboolem taalibey foofa.
24Ab Yawut nag bu ñuy wax Apolos te cosaanoo Alegsàndiri, moo dikkoon Efes. Ku rafet kàddu, te xam Mbind mi lool.

Read Jëf ya 18Jëf ya 18
Compare Jëf ya 18:23-24Jëf ya 18:23-24