Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 15

JËF YA 15:35-37

Help us?
Click on verse(s) to share them!
35Waaye Pool ak Barnabas des ci Ancos, di jàngle ak di xamle xibaaru jàmm bu kàddug Boroom bi, ñoom ak ñeneen ñu bare.
36Gannaaw ay fan Pool ne Barnabas: «Nan dellu seeti bokk ya ca dëkk yépp, fu nu masa yéglee kàddug Boroom bi, ba gis nu ñu def.»
37Barnabas nag bëggoon na yóbbaale Yowaana, mi ñuy wax it Màrk.

Read JËF YA 15JËF YA 15
Compare JËF YA 15:35-37JËF YA 15:35-37