Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 14

JËF YA 14:1

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Bi Pool ak Barnabas nekkee Ikoñum nag, ñu dugg ci jàngub Yawut ya, ni ñu ko daan defe; ñuy waare, ba mbooloom Yawut ak Gereg mu bare gëm.

Read JËF YA 14JËF YA 14
Compare JËF YA 14:1JËF YA 14:1