Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 14

Jëf ya 14:1

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Ba Póol ak Barnaba nekkee Ikoñum, noonu lañu dugge itam ca jàngub Yawut ya. Ñu waare, ba mbooloo mu mag gëm, ay Yawut aki Gereg.

Read Jëf ya 14Jëf ya 14
Compare Jëf ya 14:1Jëf ya 14:1