Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 13

Jëf ya 13:40-41

Help us?
Click on verse(s) to share them!
40Wattuleen nag ba li ñu wax ci téerey yonent yi bañ leena dal. Ñu ne:
41“Yeen xeebaatekat yi, xool-leen, jommileen te ne mes, ndax jëf ji may def ci seen jamono, ku leen ko waxoon sax, dungeen ko gëm.”»

Read Jëf ya 13Jëf ya 13
Compare Jëf ya 13:40-41Jëf ya 13:40-41