Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 13:40-41 in Wolof

Help us?

JËF YA 13:40-41 in Téereb Injiil

40 Wottuleen nag ba li yonent yi bindoon bañ leena dal, ci li ñu ne:
41 “Yéen ñiy xeebaate, gisleen lii, ngeen yéemu ba far; ndaxte dinaa def ci seen jamono jëf, joo xam ne su ngeen ko déggee sax, dungeen ko gëm.”»
JËF YA 13 in Téereb Injiil

Jëf ya 13:40-41 in Kàddug Yàlla gi

40 Wattuleen nag ba li ñu wax ci téerey yonent yi bañ leena dal. Ñu ne:
41 “Yeen xeebaatekat yi, xool-leen, jommileen te ne mes, ndax jëf ji may def ci seen jamono, ku leen ko waxoon sax, dungeen ko gëm.”»
Jëf ya 13 in Kàddug Yàlla gi