Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 13

JËF YA 13:40-41

Help us?
Click on verse(s) to share them!
40Wottuleen nag ba li yonent yi bindoon bañ leena dal, ci li ñu ne:
41“Yéen ñiy xeebaate, gisleen lii, ngeen yéemu ba far; ndaxte dinaa def ci seen jamono jëf, joo xam ne su ngeen ko déggee sax, dungeen ko gëm.”»

Read JËF YA 13JËF YA 13
Compare JËF YA 13:40-41JËF YA 13:40-41