Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - 2.Timote - 2.Timote 1

2.Timote 1:7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ndax kat Noo gi nu Yàlla jox taxu noo ragal, xanaa kay da noo may doole, ak cofeel, ak jëfin wu laloo am xel.

Read 2.Timote 12.Timote 1
Compare 2.Timote 1:72.Timote 1:7