Text copied!
Bibles in Wolof

2 TIMOTE 1:7 in Wolof

Help us?

2 TIMOTE 1:7 in Téereb Injiil

7 Ndaxte Xel mi nu Yàlla sol du ànd ak ragal, waaye day ànd ak kàttan, mbëggeel ak moom sa bopp.
2 TIMOTE 1 in Téereb Injiil

2.Timote 1:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Ndax kat Noo gi nu Yàlla jox taxu noo ragal, xanaa kay da noo may doole, ak cofeel, ak jëfin wu laloo am xel.
2.Timote 1 in Kàddug Yàlla gi