Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - YOWAANA - YOWAANA 4

YOWAANA 4:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Bi muy dem Galile, waroon na jaar ci diiwaanu Samari.
5Noonu mu agsi ci wetu dëkku Sikar ci tool, bi Yanqóoba mayoon doomam Yuusufa.
6Foofa la teenu Yanqóoba nekkoon. Yeesu toog ca pindu teen ba, di noppalu ndax coonob tukki ba. Ca digg bëccëg la woon.

Read YOWAANA 4YOWAANA 4
Compare YOWAANA 4:4-6YOWAANA 4:4-6