Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 9

Sarxalkat yi 9:7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Musaa wax ak Aaróona ne ko: «Dikkal fii ci sarxalukaay bi te joxe sa saraxu póotum bàkkaar ak sa saraxu rendi-dóomal, nga jotoo ko, yaw yaak mbooloo mi, boo noppee joxe saraxu mbooloo mi, jote leen ko, muy li Aji Sax ji santaane.»

Read Sarxalkat yi 9Sarxalkat yi 9
Compare Sarxalkat yi 9:7Sarxalkat yi 9:7