Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 9:7 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 9:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Musaa wax ak Aaróona ne ko: «Dikkal fii ci sarxalukaay bi te joxe sa saraxu póotum bàkkaar ak sa saraxu rendi-dóomal, nga jotoo ko, yaw yaak mbooloo mi, boo noppee joxe saraxu mbooloo mi, jote leen ko, muy li Aji Sax ji santaane.»
Sarxalkat yi 9 in Kàddug Yàlla gi