Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 8

Sarxalkat yi 8:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Ci kaw loolu Musaa indi Aaróona aki doomam yu góor, ñu sangu,
7solal Aaróona mbubb mu gudd ma, takkal ko laxasaay ga, solal ko fëxya ba, tegal ko ca xar-sànni ma, takkal ko ngañaay la ca kawam, jàppe ko ko, mu tafu ca kawam.

Read Sarxalkat yi 8Sarxalkat yi 8
Compare Sarxalkat yi 8:6-7Sarxalkat yi 8:6-7