Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:6-7 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Ci kaw loolu Musaa indi Aaróona aki doomam yu góor, ñu sangu,
7 solal Aaróona mbubb mu gudd ma, takkal ko laxasaay ga, solal ko fëxya ba, tegal ko ca xar-sànni ma, takkal ko ngañaay la ca kawam, jàppe ko ko, mu tafu ca kawam.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi