Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sarxalkat yi - Sarxalkat yi 7

Sarxalkat yi 7:30

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Ci loxol boppam lay dindee sarax bi ñuy def saraxu sawara, ñeel Aji Sax ji. Day indi nebbon bi, boole kook dënn bi, dënn bi di sarax bu ñuy yékkati, jébbal Aji Sax ji.

Read Sarxalkat yi 7Sarxalkat yi 7
Compare Sarxalkat yi 7:30Sarxalkat yi 7:30